Vocabolario wolof per il viaggio
 | Salaamaalekum! | Ciao! |
 | Salaamaalekum! | Buon giorno! |
 | Salaamaalekum! | Buon giorno! |
 | Salaamalekum! | Buona sera! |
 | fanaanal ak jàmm! | Buona notte! |
 | ba beneen yoon | Ciao! |
 | jàmm ak jàmm | Arrivederci! |
|
 | waaw | Si. |
 | déedéet | No. |
 | xéj na | forse |
 | baxna | Ok. |
 | jërëjëf | Grazie! |
 | amul solo | Prego! |
 | Baal ma .... | Scusi.... |
 | Maa ngi jegg ëlu. | Mi dispiace... |
 | Amnaa ... / Amouma ... | Ho ..., non ho ... |
 | Amnañu ... / Amuñu ... | Abbiamo/ Non abbiamo ... |
 | Amna ... / Amul ... | C'è ..., Non c'è ... |
|
 | Maa ngi tudd ... | Mi chiamo.... |
 | Maa ngi joge ... | Vengo (da) ... |
 | Maa ngi am .... at. | Ho ... anni. |
 | Seynaa. / Seyuma. | Sono sposato(-a) / Non sono sposato (-a). |
 | Damay (Duma) tukki man kenn. | Io non viaggio da solo |
 | Damay tukki ak .... | Viaggo con... |
|
 | Tus | zero |
 | benn | uno |
 | ñaar | due |
 | ñett | tre |
 | ñeent | quattro |
 | juróom | cinque |
 | juróom benn | sei |
 | juróom ñaar | sette |
 | juróom ñett | otto |
 | juróom ñeent | nove |
 | fukk | dieci |
 | fukk ak benn | undici |
 | fukk ak ñaar | dodici |
 | fukk ak ñett | tredici |
 | fukk ak ñeent | quattordici |
 | fukk ak juróom | quindici |
 | fukk ak juróom-benn | seidici |
 | fukk ak juróom- ñaar | diciassette |
 | fukk ak juróom- ñeet | diciotto |
 | fukk ak juróom- ñeent | diciannove |
 | ñaar-fukk | venti |
 | ñaar-fukk ak benn | ventuno |
 | ñett-fukk / fanweer | trenta |
 | ñeent-fukk | quaranta |
 | juróom-fukk | cinquanta |
 | juróom-benn-fukk | seidici |
 | juróom- ñaar-fukk | settanta |
 | juróom- ñett-fukk | ottanta |
 | juróom- ñeent-fukk | novanta |
 | téeméer | cento |
 | junni | mille |
 | tamndareet / million | un milione |
 | ay | un po' |
Ulteriori link